Videos |
Bril - Lépp Ci Yaw (Clip Officiel / Remix John Legend) |
** Abonnes-toi à ma chaîne ici https://goo.gl/Qw5BFh**
"Lépp Ci Yaw" est un remix de la chanson "All Of Me" de John Legend, arrangé et adapté en wolof par Bril Fight 4.
Un single extrait de mon prochain album digital "Au Prix de l’Amour".
#Bril #LeppCiYaw #BrilFight4 #ClassChicMusic #team221
** Crédits de la chanson "Lépp Ci Yaw " °°Â
Lyrics & arrangement : Bril
Studio enregistrement, mix, edit & mastering : Class’Chic Music
Video Directed by HLab
Lépp Thi Yaw est un remix afrobeat de la chanson "All Of Me" de John Legend.
Une production de Class’Chic Music (Senegal, 2018).
** Retrouvez Bril sur les réseaux sociaux °°
Facebook https://web.facebook.com/brilfight4
Instagram https://www.instagram.com/brilfight4
Twitter https://twitter.com/bril_fight4
Snapchat : @bril-fight4
** Lyrics de la chanson "Lepp Ci Yaw " **
Lan laaay deff soumala amoul wooon
Yow laay noyè fepp fouma meun neihh
Sama kheil yaaa thi neih, yaa fi neih yoow
Yaamay daaneil.
Beugoon naaa kham lan ngay khalat thi maan
Beugoon naaa neikeu kila geuneul sa life
Nganaan ma yoow la geum, doumaala baaayi mana’ak yoow for life......
Man saaama kheil yaaa thi neih yoow laaay khalaat
Yooow rek doy ngamaa, yow lay khoolaat
Leep thi yoow, beugg naaaa leep thi yoow
Sopp naa say kaff ak say reitaan
Beugg naa dila guiss rek niouy wakhtaaan
Man beugg naa leep thi yow, sopp naa leep thi yow.
Yaaa mom sama kheil ak sama khôl
Keinein kou nieuw guissoumako, maan yow laay khôl
Yaa moom leeeeeeeep thi maaan...
Diokh nala leeeeeeeep thi maaan....
Hoooowwww...
Niatta yoon laalaaa koo wara wakh
Yow rek yafi neih meussou mala nakh
Foo neiwoul beuuugouma même aldiana sans yow, manè dougoumaa
Yaamay dofloo yamay rray
Looma deff beugg naaa, yaay sama adounaa
Douma tayi diiila waay
Diiiila wane yoow, sa taarouwaayyyyyy
Man saaama kheil yaaa thi neih yoow laaay khalaat
Yooow rek doy ngamaa, yow lay khoolaat
Leep thi yoow, beugg naaaa leep thi yoow
Sopp naa say kaff ak say reitaan
Beugg naa dila guiss rek niouy wakhtaaan
Man beugg naa leep thi yow, sopp naaaa leep thi yow.
Yaaa mom sama kheil ak sama khôl
Keinein kou nieuw guissoumako, maan yow laay khôl
Yaa moom leeeeeeeep thi maaan...
Diokh nala leeeeeeeep thi maaan....
Hoooowwww...
Y’a moom lepp thi maaaan hohohoow...
Yoowww dooma book’ak keinein, thi sa life.
Maaan douma dem feineiiin baayby.
Leep thi yoow, beugg naaaa leep thi yoow
Sopp naa say kaff ak say reitaan
Beugg naa dila guiss rek niouy wakhtaaan
Man beugg naa leep thi yow, sopp naa leep thi yow.
Yaaa mom sama kheil ak sama khôl
Keinein kou nieuw guissoumako, maan yow laay khôl
Yaa moom leeeeeeeep thi maaan...
Diokh nala leeeeeeeep thi maaan....
# Découvrir la chanson "All Of Me" de John Legend #
https://youtu.be/450p7goxZqg
Top songs from around the world today